Lyrics.com »

Search results for 'deugou'

Yee yee! We've found 10 lyrics matching deugou.

Year:


Filter by gender:

Lyrics:

Yene rek la bagn
Nitou intérêt ak domeram rek la bagn
Wakh limay wakh tant que deugou neu dara douma ci fekk
Dara doumeu ci fek
Dara doumeu ci fek
Dara
Boudè goréna té deugou warna ko guereumé pithe

No, no, no no no no
No, no, no no no no yeah

4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
4-4-44
more
Liniou beugone
Nouniou dieumé kaname
No moreeeee

Tey daniou sokhla nioune kou tey
Kou bari yeurmandé
Daniou sokhla djitou rew bou deugou té oufe
PRINCE DU MBcCOL

Domi Mbacol Mbacol bi
Mo di Ibrahima
Moom de lamay set
Moom lamay wayantoo

Deugou gui thi moom
ck mbollo ma mou andal
Diami
sa sourire bou nice (sourire bou nekh)
Baby
Mak yaw demba leu tey dorra nieuw
Anda bou deugou té lou yagga deugueuleu
Gni beugueu yakha khamougnou fi
Domi Mbacol Mbacol bi
Mo di Ibrahima
Moom de lamay set
Moom lamay wayantoo

Deugou gui thi moom
Ak mbollo ma mou andal
Diami Senegal
Moo len yitel
nexatoul
Beut meun na xool
Mais dou guiss sou deugou woul
Xaaliss souy wakh deug noppi
Moumeu cool
Lilay bewloo doufa xaar sa gathié
Soula yak yekeuté God
Xool ma ci bët

Mbeuguel bou deugou
Dara douko faye
Yaay seetou
Biye woné sama leeraye
Jant goudi
Biddew soubeu teel
Bimala xamé
Ci la tagok weetaye
biir
Naniou gueunn deugou souniou biir
Naniou samm souniou avenir
Nit cou nioul a bari ennemi
Bénn bangui souniou biir  njiit 
Bénéén bangui babylone
sama rêw deukou Terangala
Teranga, sama rëw deugou Teranga…yaw ma lay woo hoho
Teranga, sénégal deukou Teranga
Teranga sénégal sougnou djami rëwla lead

Discuss these deugou Lyrics with the community:

0 Comments

    We need you!

    Help build the largest human-edited lyrics collection on the web!

    Search for song lyrics by

    Genres »

    Styles »

    Browse Lyrics.com

    Quiz

    Are you a music master?

    »
    What is the hometown of the Queen group?
    A Southampton
    B Liverpool
    C Manchester
    D London

    Free, no signup required:

    Add to Chrome

    Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

    Free, no signup required:

    Add to Firefox

    Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!