Lou Nekh Tchi Xol

PAPEUZ

FAVORITE (0 fans)

PAPEUZ


1:15

 Become A Better Singer In Only 30 Days, With Easy Video Lessons!

Yeungeul geuseum melni guel bou wang
Dougeul si man encaisser sa kong
Takhaw ni ennemi Coumba banc
Mais meuno ma guiss ni sa cheveux ndong
Dama gneuw pour tassare mais sibo
Kouy ladj tour bi neko PINO
Tek sama plan carriere comme aikido
Dieul coupe d afrique ni el tactico

Eeh parax-parax day dagg tiarax Kocc Barma lolou la wakh
Eeh damalay nakh soumane Dakhou mala rap teh lolou boy dou ay nakh

Tegal la lou taar melni prison
Changer position
Depasser na guerre man mangui si mission
Amena vision Amena million
Television yeup man lagnou tek sen emmision
Boy liguay weur mongui tchi man
Limay def damako meune
Xel bou poussiere ak song you peund
Mangui napp M.C yeup ni ay dieune
Di guene ay song you tegou thi temps
Poches yangui fesse Alhamdoulilah
Man sokhla wouma buzz ni OUZ le batard
Mangui daw zik.fm pour le plata

Lou nekh tchi xol, Day fegn tchi kanam
Mane Lou nekh tchi xol, Day fegn tchi kanam
Mere bangui gnane may beure di daan dem ci kaaw ci kanam
Mane Mere bangui gnane may beure di daan dem ci kaaw ci kanam
Ci kaaw Ci kanam, Ci kaaw Ci kanam, Ci kaaw Ci kanam...

 Watch: New Singing Lesson Videos Can Make Anyone A Great Singer

Written by: Papa Ngom

Lyrics © DistroKid

Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Discuss the Lou Nekh Tchi Xol Lyrics with the community:

0 Comments

    Citation

    Use the citation below to add these lyrics to your bibliography:

    Style:MLAChicagoAPA

    "Lou Nekh Tchi Xol Lyrics." Lyrics.com. STANDS4 LLC, 2022. Web. 15 Aug. 2022. <https://www.lyrics.com/lyric-lf/7985237/PAPEUZ/Lou+Nekh+Tchi+Xol>.

    Missing lyrics by PAPEUZ?

    Know any other songs by PAPEUZ? Don't keep it to yourself!

    Browse Lyrics.com

    Quiz

    Are you a music master?

    »
    Which of these songs did Taylor Swift NOT sing?
    • A. Teardrops On My Guitar
    • B. I Knew You Were Trouble
    • C. Love Story
    • D. Hot 'N Cold

    Free, no signup required:

    Add to Chrome

    Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

    Free, no signup required:

    Add to Firefox

    Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

    PAPEUZ tracks

    On Radio Right Now

    Loading...

    Powered by OnRad.io


    Think you know music? Test your MusicIQ here!