Soretul

1Da Beatz, ashs the best

0 fans

1Da Beatz


3:15

 Watch: New Singing Lesson Videos Can Make Anyone A Great Singer

Ah Ah Ah x3
So yewo yema fallo
So yewo yema fallé

Xaalat goudi xaalat beutieuk 
Aduna ma saalit lo 
Yaakar you tass yé beuri lolou
Sama xaalat ya diaxasso 
Xool ci nitt xool ci sa bopp
So gueumé koulay waan sa yoon
Beug beug yi nio beuri lol 
Sama nafsou lay diaxassol 
Oh oh oh oh


So yewo yema fallo
So yewo yema fallé
Jamono moma saalit
Sama nafsou lay diaxassol

Souma guesto tiamogn di guiss samaa ndeye joor
Li ma wessou limay waadjal day beug mengo
Amna lou feegn fi am lou neubou am lou bakh’ak lou bone
Bo beugué delou figua jougué daga xaamoul sa yoon yow
Damanila togal diougal dokhal damani nga waxak sa xel
Jamono bou tay ak demb ak souba jikko ye wouté ba tay
Djissatouma ngor ak jom ak dolé manam soutoureu si
No def ak tiono tiono aduna bi

Para ra raa raa ndeké ci sa digou dolé ci ngay soga xamné
Para ra ra yoonu ndaw meussoul gaaw meussoul gaaaw 

Para ra raa raa ndeké ci sa digou dolé ci ngay soga xamné
Para ra ra yoonu ndaw meussoul gaaw meussoul gaaaw 

Xaalat goudi xaalat beutieuk 
Aduna ma saalit lo 
Yaakar you tass yé beuri lolou
Sama xaalat ya diaxasso 
Xool ci nitt xool ci sa bopp
So gueumé koulay waan sa yoon
Beug beug yi nio beuri lol 
Sama nafsou lay diaxassol 
Oh oh oh oh

Sama xel xel na niaar
Sama xol daa kasso
Sama jeuf diaxasso
Jamono saalit loma

Sama xel xel na niar
sama xel xel na niar
Sama xol toy neu
Jamano saalit loma 

Para ra ra parara rara x3

 Struggling with Soretul? Become a better singer in 30 days with these videos!

Written by: ABDOULAYE WONE

Lyrics © ONErpm

Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Discuss the Soretul Lyrics with the community:

0 Comments

    Citation

    Use the citation below to add these lyrics to your bibliography:

    Style:MLAChicagoAPA

    "Soretul Lyrics." Lyrics.com. STANDS4 LLC, 2024. Web. 24 Jun 2024. <https://www.lyrics.com/lyric-lf/14486058/1Da+Beatz/Soretul>.

    Missing lyrics by 1Da Beatz?

    Know any other songs by 1Da Beatz? Don't keep it to yourself!

    Browse Lyrics.com

    Quiz

    Are you a music master?

    »
    'All we want from you are the kicks you've given us...'
    A Little Black Dress
    B S Express
    C I Must Confess
    D Motorcycle Emptiness

    Free, no signup required:

    Add to Chrome

    Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

    Free, no signup required:

    Add to Firefox

    Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

    1Da Beatz tracks

    On Radio Right Now

    Loading...

    Powered by OnRad.io


    Think you know music? Test your MusicIQ here!