Mazeuh

Gaws VS Gaws

0 fans

Gaws VS Gaws


3:37
#1

 Watch: New Singing Lesson Videos Can Make Anyone A Great Singer

Mazeu, Naan'ga togué Mame boye?
Niann'a ndieurign bo meun feké
Battling Siki, crochet, Xekh'nagn Automne, hiver, été
Naan'nga Mame boye,
Niann'a ndieurign bo meun feké
Battling Siki, crochet, Flamber Automne, hiver, été
Bouguoumeu avenir
Diguenté four murs
Motakh may veiller comme
Médecin de garde bu dieul ay drogues durs
Gnunn gnokoy dundeul boy mbedd dou shitt
Meun'naleu diay pour klk tickets
Pour benn foufoune
Xadioumeu fi comme djouniy innocents
Yi Teudd Camp Penal
Ay tentations gnoy vider sam iman
Fessal sam compte banque
Mangi daw depensou life dou diamou game bi
Sam mère fok muy diott lou lew
Foumeu dieumeuk benefou traffic mann
Ains bumay bind text bi
Sam neurones yeingi Xekh
Sam maam di xekhak AVC
Tchi galou love la terr di diowakk samay sentiments
Rappeur comme mann beussi dou gaw bagn'koy guissat tchi centenaire
Niggerz yeingi dei tchi liniou gueum
Amna guenth yu nei sama bopp
Am you dei tchi sama khol
God's will, gnunn nga andal boul tiit shit
O.g killers yeing si place bi
Mazeu, Naan'ga togué Mame boye?
Niann'a ndieurign bo meun feké
Battling Siki, crochet, Xekh'nagn Automne, hiver, été
Naan'nga Mame boye,
Niann'a ndieurign bo meun feké
Battling Siki, crochet, Flamber Automne, hiver, été
Succès ngui planer comme
Colon sam continent
Diguenté love ak haine la tokk Comme Pape & Cheikh lonkotina
Sa mbeugueul wolutouma té mann xawma lingay xalatt
Mann Danger la tchi yow, shooter bou makk, musiba ambulant
Kheuy, fanan tchi yoonu biff bu
Deung ni tour de Pise
Yewou tchi Merco Benz kheuyatt
Assumer tiow lek consequences yi
Li meunteu degn moy gnom dougn mann
Tei dougnko meusseu donn
Gnoy placer C4 sey
Cartel d'Crack çi cliqou THC
Ains boumay bind text bi
Sam Maam boy mingi fekh
Khamnani dina fekk lepp
Bimlenn di raw deparouma
Amnagn ay fondements
F*ck sen khalatt
Sam batt si kaw comme tankou Eric Cantona
Mazeu, Naan'ga togué Mame boye?
Niann'a ndieurign bo meun feké
Battling Siki, crochet, Xekh'nagn Automne, hiver, été
Naan'nga Mame boye
Niann'a ndieurign bo meun feké
Battling Siki, crochet, Flamber Automne, hiver, été

 The easy, fast & fun way to learn how to sing: 30DaySinger.com

Written by: Elhadji Cisse

Lyrics © DistroKid

Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Discuss the Mazeuh Lyrics with the community:

0 Comments

    Citation

    Use the citation below to add these lyrics to your bibliography:

    Style:MLAChicagoAPA

    "Mazeuh Lyrics." Lyrics.com. STANDS4 LLC, 2024. Web. 22 Jun 2024. <https://www.lyrics.com/lyric-lf/12200492/Gaws+VS+Gaws/Mazeuh>.

    Missing lyrics by Gaws VS Gaws?

    Know any other songs by Gaws VS Gaws? Don't keep it to yourself!

    Browse Lyrics.com

    Quiz

    Are you a music master?

    »
    Which of these songs did Taylor Swift NOT sing?
    A Love Story
    B Teardrops On My Guitar
    C I Knew You Were Trouble
    D Hot 'N Cold

    Free, no signup required:

    Add to Chrome

    Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

    Free, no signup required:

    Add to Firefox

    Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

    Gaws VS Gaws tracks

    On Radio Right Now

    Loading...

    Powered by OnRad.io


    Think you know music? Test your MusicIQ here!