Song parody of

Gëm (Foi)

by Anne Elisabeth

Here's where you get creative! Use our cool song parody creator to make a totally new musical idea and lyrics for the Gëm (Foi) song by Anne Elisabeth.

Simply click on any word to get rhyming words suggestion to use instead of the original ones. You may also remove or alter entire lines if needed — when you're done save your work and share it with our community — have fun!

  • English (English)
  • Français (French)
  • Español (Spanish)

Gëm ngi né ci ñun, fok ñu woné ko ! Gëm ngi né ci ñun, fok ñu woné ko ! Bi àddina sosso ba léegi Ya ngi woné sa boppa Té meussou lo sopeeku Bayi wo ñu, ya ngi def sa mëniin Ci barké Yéesu-Kristaa Gumbëya ngi gis Ci barké Yéesu-Kristaa Lafagn ya ngi dox Ci barké Yéesu-Kristaa Ñi tëx a ngi déga Ci barké Yéesu-Kristaa Ñi deewone deeki negn Toi le prince de paix (Yéesu !) Continue ton œuvre (Yéesu !) Tu ne déçois pas (Yéesu !) Ceux qui espèrent en toi (Yéesu !) Grand Dieu de miracles (Yéesu !) Refais des prodiges (Yéesu !) Que mon âme te loue (Yéesu !) Acclame ton saint nom (Yéesu !) Yow la gëm (Yéesu !) Dara titalatouma (Yéesu !) Yow rekk la gëm (Yéesu !) Jërë jëfé Yéesu-Kristaa (Yéesu !) Baatu Yàlla Yéesu ! (Kristaa !) Yéesu ! (Kristaa !) Yéesu ! (Kristaa !) Yéesu Batu Yàlla ! Yéesu rekk ! (Kristaa !) Yéesu kessé ! (Kristaa !) Yéesu dong ! (Kristaa !) Yéesu Baatu Yàlla ! Sey jaloré yeksi na Leeral seumey gët ma gis la Saa souné nga taxawlu ma Tek ci mbëggeel teralma, sargal ma Ci barké Yéesu-Kristaa Jàmm rekk ci ñun Ci barké Yéesu-Kristaa Def ñu tek ci yoonu ndam Ci barké Yéesu-Kristaa Ay kemtane la deef ci ñun Ci barké Yéesu-Kristaa Moo tax ñu sant ba abadane Toi le prince de paix (Yéesu) Continues ton œuvre (Yéesu) Tu ne déçois pas (Yéesu) Ceux qui espèrent en toi (Yéesu) Grand Dieu de miracles (Yéesu) Refais des prodiges (Yéesu) Que mon âme te loue (Yéesu) Acclame ton saint nom (Yéesu) Yow la gëm (Yéesu !) Dara titalatouma (Yéesu !) Yow rek la gëm (Yéesu !) Jërëfé Yéesu-Kristaa (Yéesu !) Batu Yàlla ! Yéesu ! (Kristaa !) Yéesu ! (Kristaa !) Yéesu ! (Kristaa !) Yéesu Batu Yalla ! Yéesu rekk ! (Kristaa !) Yéesu kessé ! (Kristaa !) Yéesu dong ! (Kristaa !) Yéesu Batu Yàlla! Gëm ngi né ci ñun, fok ñu woné ko !

Done creating your parody?

Don't keep it to yourself! Save it now so you can share it with the rest of the world!

Browse Lyrics.com

Quiz

Are you a music master?

»
Which Pink Floyd album featured the song 'Comfortably Numb'?
A Wish You Were Here
B Animals
C The Dark Side of the Moon
D The Wall

Free, no signup required:

Add to Chrome

Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

Free, no signup required:

Add to Firefox

Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

Anne Elisabeth tracks

On Radio Right Now

Loading...

Powered by OnRad.io


Think you know music? Test your MusicIQ here!