Song parody of

Omar Pen [Original]

by Omzo Dollar

Here's where you get creative! Use our cool song parody creator to make a totally new musical idea and lyrics for the Omar Pen [Original] song by Omzo Dollar.

Simply click on any word to get rhyming words suggestion to use instead of the original ones. You may also remove or alter entire lines if needed — when you're done save your work and share it with our community — have fun!

  • English (English)
  • Français (French)
  • Español (Spanish)

Tok sunu keur mu ladj ma kuy sama baay neketiyo (say say la) Tok sunu keur mu ladj ma kuy sama baay neketiyo (say say la) Han Wowé ma young de riv Beneu bar ga youkhou kogn beu hivre Awma sentiment comme gni nieuw couper conteur yi, Boul contredire Poésie noir leundeum comme kerign Lumu geuneu gnoul geuneu saf comme cerise Conquérir Lo donoul talibem do done serign Sokhlo wo lire ay tonne de livre pour deguéné ay tonne de livre Underground comme chenille Soufé ngua def comme cheville Matchou city contre lille So dougone armt done feu miss One devise kougnou togne geu dis Paraitre ni ombre ci Lerr may servir comme tenis Ak guel bou toy ni kogn venise Kou merr bokko mane bokouma mais da am compromis Ndahté awma temps pour shyne meme si ma montre brille Omzo prime yene gauche mane droite si digui pont bou libre Ndakh après the one lou dess c'est zero melni nombre 10 Meme souma jouewoul ma ngui si game bi Melni compte twitch Qu'ils me fichent la paix lou amoul fiche de paix jmen contre fiche La poésie c'est quelque chose que l'on a sur le cœur Je crois qu'un poème est une œuvre d'art Il n'y a pas d'oeuvre d'art sans nécessité de connaissance réelle de langage C'est une matière le langage J'aime aussi une certaine musique Un mouvement Une respiration dans le verbe Dans le langage Limoy say say poésie Bye bye comédie Teylé bac+5 pour rap fils sama life lay fowé ni Say say poésie Bye bye comédie Teylé bac+5 pour rap fils sama life lay fowé ni han Khamna noy wakhé k kou teukh pour jokh leu noppam Khamna noy wakhé k jiguene pour mou jokh leu boppam, for real Nio tal sene rap bi comme sen poto keur yi Def bepeu affiche bepeu salle melni photo serigne Doumeu deumeu ni yene Meunone na travestir sam music di leumbeul ni yene Meunone na abrutir jeunesse tour lene leundeum ni yene Def son pour tik tok guelou koba yeup geum meu ni yene Soumeu vues takhone jouk khamna façon bum yugni def Sokhlowouma rap bi lol lay santeu man Narone na geuneu beuri khaliss souma amoulone ay sentiment Principes dou nieup leu jik japeu na Leçon yi Guisgeu nit ak mane guissat kok gnimay saga ndey sene son yi Mais bon Si j'habite, si jap yi Narone merré adouna bi yeup depuis jadis Motakh may balou yallah soubak ngone ni tijani Beugouma woné sama bop melni hijabi, nigga Motakh ma dal khalate rap galseneu tal salades Eupeu guoorjiguen assassins creed valhala Yi texte amoul si beneu bibliothèque Beuri classe ak liasse you doy ni niari bible yo tek, rappeurs yi Gnou mounoul wakhou rap nioy wakha ay wakhou stats Niou mounoul wakh wakhou khour di wakh ay wakhou tate Forcer ay lakk yo lene degoul seni complexes guendi kaw Featuring ak 10 milles kaw man takhoul sen sons yi dougou kaw Té dou géographie beuri leb si senni biographie Khameunté suniou bir sokhlowoul sakh écographie Meune geu firi say bars dou leu guéné sa cage Nioune dagni bindeu ay livres yow dagn ley gerel sa page Han Jot na localisé ay mbalit qualité invalide Miezé disqualifié pour balé Talibé gazzali Nieuw sa galek calibre di leu jalé Kou beugue guerre dadjé geu ak khalid ibn walid hum Lou rap meune indi yeup meunoul fath samay gaume Bayilene ak seni yeufou deumeu dem yar samay dom Yeah, Last album après omar dem That boy is sick with the pen they call him Omar pen nigga

Done creating your parody?

Don't keep it to yourself! Save it now so you can share it with the rest of the world!

Browse Lyrics.com

Quiz

Are you a music master?

»
Which movie soundtrack brought second life to "Girl, You'll Be a Woman Soon"?
A Shawshank Redemption
B Pulp Fiction
C Reservoir Dogs
D Snatch

Free, no signup required:

Add to Chrome

Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

Free, no signup required:

Add to Firefox

Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

Omzo Dollar tracks

On Radio Right Now

Loading...

Powered by OnRad.io


Think you know music? Test your MusicIQ here!