#ElHadjDiouf

ChefYersa


3:02

 Watch: New Singing Lesson Videos Can Make Anyone A Great Singer

Eh saga seu wa gallei
Wowéma Elaze
Saga sa wa gallei
Wowéma El Hadj diouf
Paré, dout leu dileu yali
wowéma El Hadj Diouf
Saga sa wa ga
Wowéma El Hadj
Wowéma El Hadj
Wowema wowema wowema
Dama degg dadj melni marteau
Yagui si guinaw ni sac à dos
Fils fi kenn dou deglou sey kaddou
Paré kenn bougouleu melni kaldou
Hey, lossi meun, controler game bi paré tek ko deun
Oubil sey beut, goumba yi sakh boy mann legn guemm
Hey ok ok
Man ak rap comme ton pied mon pied
Ctrl c gnougui copier copier
Ctrl v sa guel bi lay coller coller coller la petite et on y va
Coach Yersa tek tactiques yi dou ay tiki taka
Amoul siki saka rap japonais boy degnley hara kiri
Bitch, dou ay talent dou ay don
Dama liguey beu melni dof
Dou ay tiakhann dou ay fo
Damay sandi pic di dieul ay tof
Dou ay talent dou ay don
Dama liguey beu melni dof
Dou ay tiakhann dou ay fo
Damay sandi pic di dieul ay tof
Hey
Di gueun di magg di gueuneu dieul étoffe
Hey Hey
Ngani fi gueu diougué té do lakk wolof
Hey Hey Hey
Numero dix boy dou meusseu oyof
Li mey tek ni sokoy tek di dof
Bokhouniou classe boyi may senn prof
Bref, cooking, mang si wagnbi di cooking,
Growing, and glowing, magui Damel mangthi kogn bi
Magui Yarakh magui Elisa
Rap galsen sama sarakh la boy
Fresh to death comme Kelisa
Rap français sama sarakh la tamitt bitch
Hey
Woo
Rang mouy gaw
Fou leer lako tek comme boy galsen bou diougué kaw
Mafi dakha rap sisi biensur of course ak waw
Pé comme Bolt ak Hamilton kenn doumeu meusseu raw
Eksi
Teksi
Boyi amougn ndieugou taxi
Sa guel nena sama sexy
Demmal ga disserter textes yi
Seu rappeur, sama talibé leu
Sayoumay rap mouni euskey
Ladjal Ousmane ladjal Rahim Kaw yomboul normal dina metti bitch
Magui sant yalla magui dolli niane
Lima Yalla mey fils meunomeu ignann
Djite releve bi yeup melni senn imam
Piques yi meunougn meu laal dama takk toul
Boyi meunougn meu fey ndakh takatougn
Hey Hey Hey
Soma ragalé tappet lakatoul dina
Saga sa wa gallei
Wowéma El Hadj diouf
Paré, dout leu dileu yali
Wowéma El Hadj Diouf
Hey damel seumeu gallei
Yarakh sama kogn tamitt boy
Rap bi lay nieuw dialei
Dakar Moncton Paris boy

 Become A Better Singer In Only 30 Days, With Easy Video Lessons!

Written by: Pape Ibrahima Ndiaye

Lyrics © DistroKid

Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Discuss the #ElHadjDiouf Lyrics with the community:

0 Comments

    Citation

    Use the citation below to add these lyrics to your bibliography:

    Style:MLAChicagoAPA

    "#ElHadjDiouf Lyrics." Lyrics.com. STANDS4 LLC, 2022. Web. 30 Jun 2022. <https://www.lyrics.com/lyric-lf/5359446/ChefYersa/%23ElHadjDiouf>.

    Missing lyrics by ChefYersa?

    Know any other songs by ChefYersa? Don't keep it to yourself!

    Watch the song video

    #ElHadjDiouf

    68
    7     0

    Browse Lyrics.com

    Quiz

    Are you a music master?

    »
    Who featured who in "Laugh Now Cry Later"?
    • A. Lil Mosey ft. No Cap
    • B. Drake ft. Lil Durk
    • C. Beyonce ft. Olivia Rodrigo
    • D. Fancy ft. Rihana

    Free, no signup required:

    Add to Chrome

    Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

    Free, no signup required:

    Add to Firefox

    Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

    ChefYersa tracks

    On Radio Right Now

    Loading...

    Powered by OnRad.io


    Think you know music? Test your MusicIQ here!