Xale Bi

Didier Awadi

0 fans

Didier Awadi

Didier Awadi is a Senegalese rapper and a significant figure in Francophone West African hip hop. As a founding member of Positive Black Soul (PBS) with Duggy Tee, Awadi toured around the world contributing to the international popularity of Hip Hop Galsen. Awadi works as a solo artist, accompanied by his crew PBS Radikal. He participates in the Senegalese music industry through his label, recording studio, and rehearsal space, Studio Sankara. Awadi offers a conscious and revolutionary style of music strengthened by articulated and rooted messages. His motivation and inspiration is grounded in the Burkinabé revolutionary Thomas Sankara's phrase: "Let's dare to invent our future!" more »


2:42

 Watch: New Singing Lesson Videos Can Make Anyone A Great Singer

Sama xalé bi nangu na
Sama Goné gui nangu na
Yaye boy sama shorty bi nangu na
Baye boy sama suger bi nangu na
Awadi bilay goné gui néna waw
Xalé bou rafet dikeu na, dikeulen sétane
Wa kogn bi kaay len xol
Lay la la law
Damey nanguo
Damey nangu (bess bi sa bessa)
Wol badiene, wowal nidiaye damey nangu
(bess bi sa bessa)
Damey nanguo
Damey nangu (bess bi sa bessa)
Yeuy kani, matia fi xorom damey nangu
Tey na waw ne na nanguna (han)
Wa kogn bi xale bi nanguna (way deugueula)
Yeggeul ko tiat ba tiat
Gor ak jiguen, mag ak ndaw
Sama xalé bi nanguna (wu yaay)
Sabar yi, ndeundeu yi, reuk lene (teugueu lene)
Mamane, tama yi, ana nguene? (way tama ya)
Bongo dou manke de, dikeulene (way bongo)
Ndaanaanou deukeu bi gueneu lene (way deugueu leu)
Yaru nga, jekk nga, taaru nga (aie way)
Mat nga sa place, da nga jongoma
Man maa la tann sama sadja ban
Yaye sama love, sama xol, fi ba abadan (waw waw)
Da mey nanguo
Da mey nangu (bess bi sa bessa)
Wowal badiene, wowal nidiaye
Da mey nangu (diog lene niou gumbé)
Da mey nanguo
Da mey nangu (bess bi sa bessa)
Yeuy kani, matia fi xorom
Da mey nangu
Seeri boy mané tey la tey (han han)
Tanneul lu la nekh mané naa ko feye (way han han)
Wurus aki ngalam mané, maa la mèye
Sama xol dafa sedd buma kéna rèye
Du man du yow, mané yalla la
Mo ma tanneu, ma tanneu la
Mo mané demal ci tali bi demal ci gedj
Dugu gaal mu won ma la (wouy yay)
Yow la done xaar (kekh kekh may ré)
Yow la done xaar yow (kekh kekh may ré)
(gneup di ré)
Da mey nanguo
Da mey nangu (bess bi sa bessa)
Wowal badiene, wowal nidiaye
Da mey nangu (kou sa xol neex)
Da mey nangu
Da mey nangu (diuk lene ñou bal)
Yeuy kani, matia fi xorom
Da mey nangu
Yaw yay sama sadiabane
Rabadabine ndat say
Yaw yay sama sadiabane
Rabadabine
Bilaye goné gui né na waw
Diok lene gnou gumbé (hé hé)
Diok lene gnou gumbé (hé hé)
Wa Sénégal (hé hé)
Ku nek ak ki nga beugueu (hé hé)
Xolal diok lene gnqu gumbé (hé hé)
Diok lene gnu gumbé, gumbé (hé hé)
Yaba ndaw rabine ndat say (hé hé)
Wu yay
Bess bi sa beussa
Da mey nanguo
Da mey nangu (bilaye gone gui néna waw)
Wowal badiene, wowal nidiaye
Da mey nangu (lay laha ila la)
Da mey nangu
Da mey nangu (woy l'amour il est beau)
Yeuy kani, matia fi xorom
Da mey nangu
Sama xalé bi nangu na (wo yay)
Sama Goné gui nangu na (han)
Yaye boy sama shorty bi nangu na
Baye boy sama suger bi nangu na (way deugueu leu)
Sama xalé bi nangu na (aie way)
Sama Goné gui nangu na (wou yay)
Yaye boy sama shorty bi nangu na
Baye boy sama suger bi nangu na

 The easy, fast & fun way to learn how to sing: 30DaySinger.com

Written by: Didier Awadi

Lyrics © Ferdinand Malick Hortala

Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Discuss the Xale Bi Lyrics with the community:

0 Comments

    Citation

    Use the citation below to add these lyrics to your bibliography:

    Style:MLAChicagoAPA

    "Xale Bi Lyrics." Lyrics.com. STANDS4 LLC, 2025. Web. 12 Feb. 2025. <https://www.lyrics.com/lyric-lf/10553300/Didier+Awadi/Xale+Bi>.

    Missing lyrics by Didier Awadi?

    Know any other songs by Didier Awadi? Don't keep it to yourself!

    Quiz

    Are you a music master?

    »
    T Rex was led by which singer?
    A David Johansen
    B Ian Hunter
    C Marc Bolan
    D Gary Glitter

    Free, no signup required:

    Add to Chrome

    Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

    Free, no signup required:

    Add to Firefox

    Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

    Didier Awadi tracks

    On Radio Right Now

    Loading...

    Powered by OnRad.io